SERIGNE MAME CHEICK MBACKE KHADIM AWA BA : Lima gana yéme ci Serigne bi !! té lolou mome rek lako Yalla diakk léle !! moy bolé khétou Yonentabi psl) wayna Sahabi yi, wayna brome guirr yi, wayna Waliyou Yalla yi, gnanalna mboléme diouliyi 10 Octobre 2021